MOYTOU

by BATCH GUEYE

/
  • Streaming + Download

    Includes unlimited streaming via the free Bandcamp app, plus high-quality download in MP3, FLAC and more.
    Purchasable with gift card

      £8.99 GBP  or more

     

1.
04:25
2.
03:54
3.
03:28
4.
5.
03:43
6.
05:00
7.
03:42
8.
03:51
9.
04:14
10.
11.
03:47

credits

released May 16, 2019

license

all rights reserved

tags

about

Batch Gueye UK

Batch Gueye is a Griot, a traditional storyteller from Senegal. He sings the music of the Baye Fall folk with a soulful voice magically bringing the heart of West-Africa to you. Batch’s mouride muslim background, the vocal chanting traditions of mouridism, is his biggest inspiration. Batch is also a price winning sabar dancer.
... more

contact / help

Contact Batch Gueye

Streaming and
Download help

Shipping and returns

Redeem code

Track Name: BANOUYE GONE
Tay laleni fateli bani gone founiou diar! tay laleni fateli bani gone founiou diar!cheikh mbacke Ndiaye cheikh sene cheikh Gawane ni Sam Lam kokou sama waye la!ni serigne mbaye Elage diakhate ni Zal Diouf Ibre Ndiaye bakhna!Omar Alex Sagnia ni Sama way kokou nit kou bakhla ni Ela Seydi doumou ndeye la liii niou dane foweee (feko falo guinarakoum nenam maadone feki laloo borom toll fekeumafa ) souma sanione douma touki bayi ndiabote guinaw fatewoulane dama wouti dolee !Youssou Mbaye Alune Diop Boly Sarre laniou dane fowee (alan ndouti,alan ndouti ndeye coumba douma yakal sama alan ndouti )(langua niorna langua boyna)ni (guar botaneute,guar dorante )cheikhou cheikhou gui ni cheikhou sama wadji liniou dane fowee (mame yalla tawal walanguane guoo hi guokh mame yalla tawal walanguane guoo hi guokh mame yalla tawal walanguane guoo hi guokh )(feko falo guinarakoum nenam, madone feki laloo borom toll fekeumafa, feko falo guinarakoum nenam ,madone feki laloo borom toll fekeumafa )bi tankeu tankeu koumou gueyene la gueyene la Cheikh Sene ,bi tankeu tankeu koumou seneneleu seneneleu Ibre Ndiaye ,bi tankeu tankeu koumou mboupbeneu mboupbeneu Cheikh Abdou Mboup,bi tankeu tankeu koumou ngomeneu ngomeneu Mor Ngom bi tankeu tankeu koumou Lameneu lameneu Modou Lam ,bi tankeu tankeu koumou camara camara Khamsatou Camara,bi tankeu tankeu koumou lamene lamene Sam Lam ,bi tankeu tankeu koumou ndiobene ndiobene Cheikh Gawane Diop ,bi tankeu tankeu koumou ndiayene ndiayene Cheikh Mbacke Ndiaye,bi tankeu tankeu koumou gueyeneleu gueyeneleu Cheikh Gueye,bi tankeu tankeu koumou guayeneleu guayeneleu Birane Coumba Guaye ,bi tankeu tankeu koumou seneneleu seneneleu Mame Cheikh Sene,bi tankeu tankeu koumou Serigne Mbaye... Elage bakhna ,bi tankeu tankeu koumou Aladji Sow Bass Mbaye Batch Gueye molene di begueeeee
Track Name: BOULE FATTE
Kharit gniou fatelicou liniou dane fowee baniouye gonee. Aduna ko mèredie ,dunuya ko mèreme,aduna ko mèredie dunuya ko mèreme. Aduna ko mèredie ,dunuya ko mèreme. Aduna ko mèredie,dunuya ko mèreme. Aduna ko mèredie , dunuya ko mèreme. Aduna ko mèredie ,dunuya ko mèreme. Wax diou borom tewoul bouko waxee dieuwla.wax diou borom tewoul bouko waxee dieuwla boude lou bakh dieuwla ,boude lou bone dieuwla.damay dox di khol yaye nioune yaye niniou mel.damay dox di lathiee nioune yaye niniou mel deukeul nitki foumou deukoul dafa niawe sounou bir! Aduna ko mèredie, dunuya ko mèreme.aduna ko mèredie,dunuya ko mèreme.aduna ko mèredie,dunuya ko mèreme .adunaaa ko mérimereee ,merimereee.banioude gone la niou yalla bolewone,legui magnane ndeyesane de yakouna guir wax diou nias,wax diou bone gui niouye wax mounouniouko deukee sounou bir dafa niaw,dego guaniou dane dego amatoul waxtane guaniou dane waxtane amatoul.dieuw bakhoul ni bayilene fouguene togue di toguee domou adama yi,adama dieuw bakhoul,mouno déme bayima mounou ma deme,mounou ma deme bayila yalla niou bole.mounou ma deme bayila mounoulo deme,mouno deme bayima yalla niou bole.bouniou kene bole kharitoo nikharito kharito bouniou kene meusa bole ndakh yow sama doumou ndaye gua kharito.baniouy gone laniou yalla bolewone balegui boumou yakou yow kharit !kharit sama domou ndaye gua!
Track Name: MANE MANE
(Mané Mané)dôme djiou beugue sa rew,dôme djiou fonkeu sa rew,diligueye te dou wax Sadio Mané waye na la,Sadio ,Sadio,Sadio Mané yaye diambare,dôme djiou beugue sa rew,dôme djiou fonkeu sa rew,di ligueye te wax Sadio Mané waynala.Sadio,Sadio,Sadio Mané yaye diambare,sadio ,sadio,Sadio Mané yaye diambare,doumou ndayou Ela Seydi,doumou ndayou Beauga,di ligueye te dou wax Sadio Mané waynala,sadio,sadio,Sadio Mané yaye diambare ,dou wax yow wax diou nias,dou tontou wax diou niaw,daye def tedou wax Sadio,Sadio yow yaye diambare,Sadio,sadio,Sadio Mané yaye diambare,.Sadio,Sadio,Sadio Mané yaye diambare.Ayeee salamalema,Mané dion kelefa,kerinw nigue kana waly ndianthio mouka foo iiii bouka bayiii,mbe kontoneuna mbe diayla sadio sadio sadio albarka Sadio Mané ..heeee Mané,heeee Mané ,heeee Mané ,heeee Mané,heeee Mané,heeee Mané,heeee Mané,.Sadio Mané yaye diambare,tabakhna fi lycée thi Sénégal Sadio Mané yaye diambare,dimbale nafi newdi doleyi thi Senegal,Sadio Mané yaye diambare,dieufdia bari lol,wax dia new lolo sadio !Sadio Mané yaye diambare,equipe national amnaneu thi yow yakar,sadio Mané yaye diambare,boul tayii,sadio boul tayii,fofoula Sadio Mané yaye diambare
Track Name: GEUME SA REWE
Sou toucke te ba yegue si sam rew boul di wanewou,sou toucke te ba yegue si sam rew boul di wanewou,sou toucke te ba yegue si sam rew boul di wanewou,.sou toucke te ba yegue si sam rew boul di wanewou,sou toucke te ba yegue si sam rew boul di wanewou, sou toucke te ba yegue si sam rew boul di wanewou,yow laye wakhal hamenala,yow laye wakhal bilaye guisnala,sounou rakeu yagui dieuleu gal niome di dem guethie,bilaye change diotena,yow mi nagua chargé ,bilaye Modou,Modou diaroul guaye diaye tarr walaye Modou,Modou diaroul guaye diaye am-am.,sounou rakeu yagui dieul gal niomeu di dem guethie.,ni,ni dieul galgui di demeu.ni,ni lep xalis di dème,ni nigui ndoumblangue yow di dème,liko waral moy ligualeneu wone yow sounoum rewoo,linioulaye wone daniou laye nakh lolou dou réalité bou am fee,linioulaye wone daniou laye nakh lolou dou réalité bou am fee 24 /24 guaye ligueye goudek beuthiekeu,linioulaye wone daniou laye nakh lolou dou réalité bou am fee,daguaye ligueye goudek beuthiekeu lo am yow diokheko togue,linioulaye wone daniou laye nakh lolou dou réalité bou am fée,linioulaye wone daniou laye ndakh lolou réalité bou am fée,Dotala nelaw ba yandor lo am dikhe ka togue,linioulaye wone daniou nakh lolou dou réalité bou am fée,sayou nieuwee limou laye wane,bilaye nekoul si mome,linioulaye wone daniou nakh lolou dou réalité bou am fée,meuna na agneu mome dou rereu sou gnieuwee dila diaye tar,linioulaye wone daniou laye nakh lolou dou réalité bou am fée,.thiey Modou,Modoo,Modou bayil nigua mel,linioulaye wone daniou laye nakh lolou dou réalité bou am fée,.no mana mel,loo mana am boulko wane gnifi nekeu,linioulaye wone daniou laye nakh lou dou réalité bou am fée,.nieneu ,nieneu si modou yee seneu dokhaline mane dee nekhouma,linioulaye wone daniou laye nakh lolou dou réalité bou am fee
Track Name: NONE
None)yalna sama none am diam hoo none bakhna,yalna sama none ameu diameu hoo none bakhna,yalna sama none am diam none bakhna si mane !yalna sama none am diam hoo none bakhna,yalna sama none am diam hoo none bakhna,yalna sama none ameu diameu none bakhna si mane !none na takh may ligueye,none na takh may dann sama dolee ki takh may bagne kouma retaneu bilaye none bakhna si !sasouma naree wax lou niaw khel mi démeu si sama none yee ,sayouma naree wax lou niaw halât lene none bakhna si mane !sou gueneu guissee nioulaye rée,rée diou nekh soo dèmee niou toguela,naneu sou gueneu guissee niniou laye rée,rée diou nekh soko wanee guinaw mou toguela,kou melni niom motakh may goor goor loo fouma tolou none bakhna si mane !so yeguie mou diapleu,sodano mou retaneleu,bou sa weurseuk diaree si mome,mome mou tanthileu ,none ,so yegue mou diapleu,so dano mou retaneleu,sa weurseuk bou diaree si mome,mou tanthileu,niou mel ni mome motakh may goor goor loo fouma tolou none bakhna si mane !hooy none bakhna si mane,yalna sama none am diam hoo none bakhna,yalna sama none none ameu diameu hoo none bakhna,yalna sama none am diameu none bakhna si mane,sou guene guissee moulay rée,rée diou nekh,soo dème mou toguela naneu sou gueneu guissee moulaye rée,rée diou nekh soko wane guinaw mou toguela !niou mel ni nioum nio takh may goor goor loo fouma tolou none bakhna si mane hooy none bakhna si Mané
Track Name: MOUSOLOU
(Mousolou)mini yamba touguama lambe lo,saaba mini yamba,saaba ya kono lelo,saaba mini yamba,saaba mini yamba yi,saaba minii yambayi touguama lambe loy,touguama,touguama!touguama lambelo mini yambayii !mini yamba niwana touguala saaba mini yamba kene -kene ya darilelau saaba mini yamba !haan yii mini yamba lambelau mini yambay !mini yamba touguama lambelau,saaba mini yamba kene -kene ya darilelau,saaba mini yamba !mini yamba touguama lambelau,saaba mini yamba kene-kene ya darilelau,saaba mini yamba haaa yi mini yamba,lambelau mini yamba !koubalee ketaaa kookoule ketaa,koubale ketaa koulee kee haaa saaba aaa haa mini yamba,mini yamba mou saa letii !mousso lee tataaa farotoo,konobala saa ya makoy faa woulouta,walatina iko mini yamba moukou baletii !mini yamba saa haaaa ,aaaa,haaa mini yamba,saaba mini yamba !saaba,aaaa,hooo saaba mini yamba, saaba mini yamba haaa,hoo mini yamba saaba mini yamba,mini yamba,ko mini yamba,saaba mini yamba haha !mini yamba,saaba mini yamba,mini yamba kene- kene ya darilelau saaa mini yamba.
Track Name: WAYE WI
waye wi}ma wayla waywi,waywi yaye borom baye,ma wayla waywi,waywi yaye borom baye yi ,ma wayla waywi,waywi yaye borom, yaye borom,.Fa Mbaye di sa yaye,Abdou Gueye di sa baye.Batchie Gueye gau bokal ndaye ak baye Manoumbe,Cheikh Sene mounoy dioy te nope gounioy baye waywi yaye borom bayi,yaye borom !ma wayla waywi,waywi yaye borom bayi,yaye borom !Gueye masada penda ak mamaly penda nar gnieti doumou penda nar yi baye yayi borom .Ma wayla waywe ni waywe,ni baye Manoumbe waw,waywi yako mome !Batchie Gueye gua di sa mak,cheikh Sene gua bokal beneu ndaye,baye Manoumbe wawaw waywi yako mome.soumala woye warna,soumala wayoul warna ,baye waywi yaye boromee yi waywi yako momee baye.soumala waye warna,soumala wayoul warna,dara niorouko koudoul Mame Saliou.Gueye masada pendanar rée ak mamaly penda nar baye!gueneu wal gua deskawone,wayna fi yaye ,wayna fi Mak,wayna fi Rak te wayna fi goune.baye Manoumbe doumala fatee beneu yone baye,soumala waye warna,soumala wayoul warna.baye dara nioroula koudoul Mame saliou,soumala waye warna soumala wayoul warna,Ma wayla waywe ni waywe,ni baye Manoumbe wawaw ,waywi yako mome Batchie Gueye di sa mak,Cheikh sene gua bokal beneu ndaye baye Manoumbe wawaw,waywi yako mome
Type a message...
Track Name: SAFASSA
Nawlona,nawlana nawlonala mouso lek bayi yaye nawlonala,nawlona,nowlona,nawlonala mouso lek bayi yaye nawlonala !bousa yaye bakhee,yow sa baye bakh neu domana bone,bakh alalou yalla leu !gni yagui bakh si seneu alaleu,gni bakh si seneu dolee,gni bakh si seneu guisguis,gni bakh si seneu am-am !bilaye lolou dou mbakh,mbakh alalou yalla la,mbakh safassaa woy mbakh safassa yagua thia kaw yagui koy dawal mbakh safassa !mbakh safassa ni mbakh safassa yagua thia kaw yagui koy dawal mbakh safassa ,ni mbakhee ni mbakh safassa yi ni mbakh safassa yi,yagua thia kaw,yagui koy dawal mbakh safassa,mbakh safassa !mbakh dou wesou mbakh kone gua diangue mbakh!mbakh dou wesou mbakh kone gua diangue mbakh !mbakh alalou yalla leu Kharite ba lakoye diokh !mbakh dou wesou mbakh kone gua diangue mbakh ,djitou mbakh diangue mbakh takhna keurgua bakh!mbakh dou wesou mbakh kone gua diangue mbakh,mbakh dou wesou mbakh kone gua diangue mbakh !soliyoo annnn ayii solou wooo iyee makouma gnianaa ayee mansan lou banaa Diougou magni,diougou magni dee !aliguan beteyaa,alaa barika diougouya magni dee !mbakh dou wesou mbakh kone gua diangue mbakh !mina diona welelaa gueye masada penda nar !mbakh dou wesou mbakh kone gua diangue mbakh,Abarika baba na!aligua beteya Batch Gueye bakh na,mbakh dou wesou mbakh kone gua diangue mbakh !
Track Name: WAKHONE NAKO
Maneu damay niane damay niane,damay niane,maneu limaye niane Africa dieum sa kanam !ne Kourouma waxone nakoy ,Nelson Mandela waxone nako,ni Cheikh Anta Diop waxone nako,Kouwame Krouma waxone nako!maneu damay niane,damay niane,damay niane,damay niane Africa dieum sa kaname !naneu bolo,bilaye nekeu beneu,naneu manko kadouyi doneu beneu,fou way meuna nek khalatal sa rew,fou waye meuneu tolou boule fatee yow sa rew!maneu limaye niane ,limaye niane,limaye niane,maneu limaye nianeu Africa dieum sa kaname !ne kourouma waxone nako,Nelson Mandela waxone nako,ni Cheikh Anta Diop waxone nako,Kouwame Krouma woxone nako,nitte kou gnioul dafa beugue guouroy,nitte kou gnioul ni mou beuguee guouroo yakar ni ya mome nittegniee kou djitee yakarni ya gueneu nitte yee !Krouwame Krouma,Krouwame Kroumee,bilaye Nelson Mandela waxone nako,Nelson Mandela ni,Cheikh Anta Diop bee waxone nako !Cheikh Anta Diop,cheikh anta diop,ni Krouwame Krouma waxone nako,Krouwame Krouma, krouwame krouma,Cheikh Anta Diop,cheikh anta diop,daniou ameu nitte gniou bakh si sounoum rew Africa !Nelson Mandela,nelson mandela ni Boukounta Ndiansane,Mame Limamoulaye yoff,ni Cheikh Ahmadou Bamba borom Touba,Mame Mawdo,ni Mame Mawdo,Cheikh Thianaba,thianaba yi !ni Kouwame Krouma waxone nako yi,bilaye nanou boloyi nek beneu,sounou rew,krouwame krouma,krouwame krouma,ni rewmi,rewou diameu la,nioune,nioko momee !nelson Mandela,nelson mandela waxone nako ,cheikh anta diop,cheikh anta diop !Cheikh Anta Diop waxone nako!
Track Name: DOGO LINGERE LA
dogo linguere la]wiyo,wiyo,wiyo,wiyo,wiyo,wiyo,hannnn wiyo.dogofali linguere la,Modou Thiam linguere la ,dogofali linguere la,dogofale mawo dior linguere,dogofali linguere la,masamba ya dialor linguere la dogofali linguere !Modou Thiam linguere gua,Amy Thiam linguere la,Lath Thiam linguere la,Ndeye Thiam linguere la.bilaye linguere la,bilaye Modo,Modou Thiam dogofale mawa dior yow sa mame laye,Ndeye dogo linguere la,Amy Thiam linguere laye,Lath Thiam linguere la,Modou Thiam linguere la,magui naneula dogo,dogo mithie melgo yi,samba khewar mithie ndiaye mani dogo,bilaye nee goudena yaye boye goudenayi dogo falek mawo dior yow sa mame layeyi,Amy Thiam linguere laye dogofali linguere là,haaaaaaa sayaa,sayaa magni dee Modou taraa,bilaye Modo,Modou thiam dogofalek mawo dior yow sa mame laye,bilaye goudena yaye boye,goudanayi dogo falek mawo dior yow sa mame laye,Ndeye dogo linguere la,Amy Thiam linguere laye,Lath Thiam linguere laye.Modou Thiam linguere laye,dogofalei linguere la ,bilaye Modo,Modou Thiam dogofalek mawo dior yow sa mame laye,bilaye Modo,Modou Thiam dogofalek mawo dior yow sa mame laye.
Track Name: GISSE NALENE
Gisse Nalene )naneu fonkou djigene,teyereum djiguene,djiguene naye sounou yaye boye naneu yeureum djiguene.Djiguenou sene-gambia naw nalene,niguene diapee seneu ni goryee guisnako,Djiguenou Sene-Gambia naw naleneu,niguene diapee seneu ni goryee guisnako.yene rakhass,yenaye footeux,te yeneu,yenaye passée,yenaye togou,yenaye boott,yenaye roguoti,yenee rakhass,yenaye fott,te yeneu,yenaye passé, yenaye togou,yenaye botteu,yenaye roguati.,Fonkou nalene,gueureume naleneu djiguene sene-gambi yayi,fonkou naleneu.Djiguene sene-gambi yayi,fonkou naleneu nigueneu diapee seneu ni goryee guisnako,djigueneeu,bilaye masa thiono,thiourourou,thiourou,mbaye,mbaye thiourourou,thiourou Mbaye,Mbaye ,thiourourou,Djiguene naye sounou yaye,djiguene moye botteu di nampaleu,bodee gonee hamoulo,mounoulo,boudoul wonakeu yaye dina meti,leklek gua khif,leklek gua marr,leklek gua diakhlee lolou,boudoul wonak yaye dina meti,Ni dôme gnieteleu bilaye dôme gnieteleu dôme dji titero yayam ak dôme dji yayam di tirero,ak dôme dji teral yayeum ,thiourourou,thiourou mbaye,mbaye thiourourou,thiourourou,thiourou mbaye,mbay,thiourourou,yenanouy botteu di nampal sounou hifee niou lek bou goudi diotee

If you like MOYTOU, you may also like: